1 Kings 2:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Abiyatar sarxalkat bi nag, Buur ne ko: «Dellul Anatot ca say tool. Dee rekk a war ci yaw, waaye bésub tey jii duma la rey, ndax li nga gàddu woon gaalu Aji Sax ji Boroom bi, dox jiitu sama baay Daawuda. Nga teg ci bokk ak sama baay mboolem coono bu mu daj.»