1 Kings 2:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yowab àndul woon ak Absalom ci pexeem, waaye Adoña la mujj àndal. Ba Yowab yégee la xew, daa daw ba ca xaymab Aji Sax ji, jàpp ca béjjén ya ca cati sarxalukaay ba, ngir rawale bakkanam.