1 Kings 2:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba mu ko defee Buur yónnee woolu Simey, wax ko ne ko: «Tabaxalal sa bopp kër fii ci Yerusalem, dëkk ca waaye bul dem fenn.