1 Kings 2:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Góor ñiy doomi Barsilay mu Galàdd nag, nanga leen baaxe, te ñuy bokk ak yaw ndab, ndax kat taxawu woon nañu ma, ba may daw Absalom sa doomu baay.