1 Kings 20:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yonent ba dikk ca buurub Israyil ne ko: «Nanga dëgërluwaat te xam ni nga wara def, ndax nëgëni déwén buurub Siri dina la songaat.»