1 Kings 20:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te yaw nga sosaat mbooloom xare mu mel ni ma nga amoon, fas ak fas, watiir ak watiir, ndax nu mana xareek ñoom ci joor gi. Su boobaa déy, noo leen di ëpp doole.» Mu déggal leen, def noona.