1 Kings 20:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñu ne ko: «Ben Addàd dafa wax ne: “Sa xaalis ak sa wurus, maay boroom. Say jabar it, ak ñi gëna dëgër ci say doom, maay boroom.”»