1 Kings 20:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndaw ya dikkaat ne ko: «Ben Addàd dafa wax ne: “Maa yónnee woon ci yaw, di sàkku nga jox ma sa xaalis ak sa wurus ak say jabar ak say doom yu góor.