1 Kings 20:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Axab ne ndawi Ben Addàd ya: «Waxleen Buur, sama sang, ne ko: “Sa jaam ba nee mboolem la nga jëkkoona yónnee di ko sàkku dina ko def. Waaye lii nga mujja laaj moom, du ko def.”» Ndaw ya dem jottli tontam.