1 Kings 21:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Axab ne Nabot: «Jox ma sa toolub reseñ bi, ma def kob tóokër, ndax jege na sama kër. Dinaa la ko wecci toolub reseñ bu ko gën, walla su la gënalee ma delloo la njégam ci xaalis.»