1 Kings 21:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Axab ñibbi këram, mer, ne fóññ ndax la ko Nabot waa Yisreel ba wax, ne ko du ko jox suufas maamam. Mu tëdd ca lalam, gedd, baña lekk.