1 Kings 22:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jant baa ngay xalambaayu, yéene jib, ba dajal mbooloo ma. Ña nga naan: «Na ku nekk ñibbi sa dëkk, ca sam réew!»