1 Kings 22:39 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li des ci mbiri Axab ak mboolem lu mu def ak kër ga mu tabax, rafetale ko bëñi ñay, ak mboolem dëkk ya mu tabax, loolu lépp, bindees na ko moos ca téere ba ñu dippee Jaloorey buuri Israyil ca seeni jant.