1 Kings 22:49 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yosafat defaroon na ay gaal yu mag yu mu deme réewum Ofir, di wuti wurus. Waaye sottiwul, ndax gaal yaa nga suux ca Esiyon Geber.