1 Kings 22:50 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Booba la Akasiya doomu Axab wax Yosafat ne ko: «Tee ngaa may samay nit, ñu ànd ak say nit ci gaal yi?» Yosafat lànk.