1 Kings 3:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ma amee doom ba mu am ñetti fan, moom mii itam mu am doom, te nun rekk a dëkk, keneen nekkul ak nun ca biir kër ga, xanaa nun ñaar.