1 Kings 3:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Israyil gépp nag dégg àtteb Buur, daldi yéemu ci moom, ndax dañoo gis ne xelum Yàlla mu rafet a ngi ci moom, di ko jiite ci àtte dëgg.