1 Kings 5:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Xam nga sama baay Daawuda manul woona tabaxal Yàllaam Aji Sax ji kër gu mu ko tudde, ndax xare yi mu séqoon ak noonam yi ko wër, ba ni leen Aji Sax ji daaneele, mu teg leen tànk.