1 Kings 5:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Iram yónnee ca Suleymaan, ne ko: «Dégg naa kàddu yi nga ma yóbbante. Man ci sama bopp dinaa la defal li nga bëgg lépp ci wàllu banti garabi seedar ak sippar.