1 Kings 7:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbalkam njàpp mi tege ci kaw fukki jëmmi nag ak yaar, ñett jublu bëj-gànnaar, ñett jublu sowu, ñett jublu bëj-saalum, ñett jublu penku. Mbalka mi war nag yi, seeni gannaaw féete biir, ñoom ñépp.