1 Kings 7:37 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu la Uram defare fukki rootukaay yi. Lépp bokk móol, yem dayo te bokk bind.