1 Kings 8:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul Aji Sax ji wax Daawuda sama baay, ne ko: “Gannaaw yaa fasoon ci sa xol, yéeney tabax kër, tudde ma ko, def nga lu rafet, ngir sa yéeney xol la woon.