1 Kings 8:44 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu sa ñoñ di xarejeek seen noon, ci yoon woo leen yebal, su ñu ñaanee ci Aji Sax ji, jublook dëkk bii nga taamu, ak kër gii ma tabax ngir saw tur,