1 Kings 8:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur Suleymaan ak mbooloom Israyil ma daje fa moom, ñoom ñépp a nga bokk ak moom, teew. Ñu jàkkaarlook gaal ga, di rendi ay gàtt aki nag yu kenn manula lim mbaa di ko waññ, ndax bare.