1 Kings 8:63 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu defal Aji Sax ji saraxi cant ci biir jàmm, lépp di ñaar fukki junniy nag ak ñaar (22 000) ak téeméeri junniy gàtt ak ñaar fukk (120 000). Noonu la Buur ak bànni Israyil gépp amale xewu jagleb kër Aji Sax ji.