1 Kings 9:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu Iram bàyyikoo Tir, seeti dëkk ya ko Suleymaan jox, waaye dëkk ya neexu ko.