1 Kings 9:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñoo doon itam saytukat yi yore liggéeyi Suleymaan. Amoon na juróomi téeméeri jawriñam ak juróom fukk (550) yu daan jiite nit ñiy def liggéey bi.