bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Kings 9:25
1 Kings 9:25 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Suleymaan di def ñetti yoon cim at ay saraxi rendi-dóomal, ak saraxi cant ci biir jàmm, di ko sarxal ci kaw sarxalukaay bi mu tabaxal Aji Sax ji, boole ci di taal cuuraay ci kaw sarxalukaay bi, fi kanam Aji Sax ji. Mu daldi matal la war ca kër Yàlla ga.