bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Kings 9:4
1 Kings 9:4 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nag, soo doxee fi sama kanam ni Daawuda sa baay daan doxe cig mat akug njub, di def lépp lu ma la sant, di sàmm sama dogali yoon, ak sama àttey yoon, nga di ko sàmm,