1 Peter 1:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Yàlla xamoon na ko, ba àddina sosoogul, waaye léegi ci mujug jamono feeñal na ko ndax yéen
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu yàgg, ba àddina sosoogul la Yàlla tuddaloon Almasi loolu, waaye léegi ci mujug jamono jii la ko Yàlla feeñal ngir yeen,