bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Peter 1:24
1 Peter 1:24 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte:«Nit ñax la,ndamam di tóor-tóor kese;ñax day wow, tóor-tóor ruus,waaye kàddug Boroom bi day sax ba fàww.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax bindees na ne: «Bépp boroom suux, nim ñax la mel, mboolem darajaam mel ni tóor-tóoru àll, ñax ma wow, tóor-tóor ma ruus.