1 Peter 2:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Na seen nangub Boroom bi tax, ngeen déggal képp kuy kilifa, muy buur ba gën a kawe,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nangul-leen gépp kilifteef gu tege ci àddina ngir Boroom bi; muy buur bu mag bi gëna kawe,