1 Peter 2:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ngeen tooñee te muñ i pes, luy pey gi? Waaye su ñu leen fitnaalee ci def lu baax te ngeen muñ ko, jëf ju rafet la fa kanam Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Muñ ay dóor yu la fekk tooñ, ana lu ciy ndam? Waaye soo muñee coono boo daj ngir lu baax loo def, loolu de aw yiw la fa kanam Yàlla.