1 Peter 2:21 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte ci loolu la leen Yàlla woo, ndaxte Kirist itam sonn na ngir yéen, teg fi seen kanam royukaay, ngir ngeen jaar ciy tànkam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci loolu sax lañu leen woo, ndax Almasi itam sonnal na leen, te moo leen bàyyeel ab royukaay, ngir ngeen jaar ciy tànkam.