1 Peter 2:8 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te it:«Doj la wuy fél nit,di xeer wu koy fakkastal.» Dañu cee fakkastalu, ndaxte gëmuñu kàddug Yàlla, te loolu la Yàlla dogal ci ñoom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it: «Mooy doj wuy fakktale, di xeer wuy daaneel.» Ñoo ko fakkastaloo nde ñoo gëmul kàddu gi, te it loolu la leen dogal ba séddoon.