1 Peter 3:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax Boroom baa ngi xool ñi jub bëti yërmande,di ubbi ay noppam ci seeni ñaan,waaye dàq ñiy def lu bon.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ay gët la Boroom bi ne jàkk aji jub ñi, te ay noppam la dékk seeni ñaan, waaye Boroom bi, kanamam lay tëjal ñiy def lu bon.»