1 Peter 3:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñu fitnaal la ndax jëf ju baax, su dee mooy coobareg Yàlla, moo gën ñu fitnaal la ndax jëf ju bon.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Coono yu la jëf ju baax yóbbe kat, ndegam da di coobarey Yàlla, moo gën coono yu la jëf ju bon yóbbe.