1 Peter 3:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ku la def lu bon mbaa mu saaga la, bul feyyu, waaye ñaanal ko lu baax; ndaxte ci loolu la leen Yàlla woo, ngir barkeel leen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lu bon, buleen ko feye lu bon; ay saaga it, buleen ko feye ay saaga. Xanaa ngeen ñaanal leen, feye leen ko, ndax ci loolu lees leen woo, ngir ngeen jagoo barke.