bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Peter 4:13
1 Peter 4:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye bégleen ci cér, boobu ngeen am ci coonoy Kirist, ngir bés bu ndamam di feeñ, ngeen bég ak mbég mu ëpp xel.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye noonu ngeen séddoo ci coonoy Almasi, bégeleen ko, ngir bu ndamam feeñee, ngeen gënatee bég.