1 Peter 4:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Buñu sonal kenn ci yéen ci li mu rey nit walla mu sàcc, mbaa def lu bon, walla dugg ci lu yoonam nekkul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye rey nit, mbaa sàcc, mbaa def lu bon, mbaa dugg ci yëfi jaambur, bumu waral coonoy kenn ci yeen.