1 Peter 4:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndaxte àpp bi jot na, àtte baa ngi tàmbalee ci nun waa kër Yàlla. Te su tàmbalee ci nun nag, luy muju ñi weddi xebaaru Yàlla?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax kat tey la àtte bi wara tàmbalee ci waa kër Yàlla. Ndegam ci nun lay tàmbalee nag, ñi gëmul xibaaru jàmm bu Yàlla, ana fu ñu jëm?