1 Peter 4:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Looloo waral it ñu jottali xebaar bu baax ndee, ya fekke woon jamonoy Nóoyin jooju, ngir ñu dunde Yàlla ci seen xel, doonte sax nit ñaa ngi leen daan fitnaal ci àddina.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li ñu ci jublu moo di, ñi dee tey sax, ñu àgge leen xibaaru jàmm bi, ngir bu ñu leen àttee àtteb nit ñu seen yaramu suux wara dee sax, du tee ñuy dund tey, ndax Noowug Yàlla.