1 Peter 4:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li gën a am solo mooy, ngeen bëggante mbëggeel gu tar, ndax mbëggeel day suul bàkkaar yu bare.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye li ci raw mooy soppanteleen cofeel gu mat sëkk, ndax cofeel, bàkkaar yu bare lay far.