1 Peter 5:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon yéen njiit yi, maa ngi leen di dénk, man miy njiit ni yéen, man mi seede coonoy Kirist te am cér ci ndam li nar a feeñ.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mag ñi ci seen biir di seeni njiit nag, dama leen di ñaax, man miy njiit ni ñoom, di seedeb coonoy Almasi, te di boroom cér ci ndam li nara feeñ.