1 Peter 5:13 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Mbooloo mi nekk ci dëkk bi ñuy wax Babilon te Yàlla tànn ko ni yéen, moo di leen nuyu, ñoom ak Màrk sama doomu diine.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ab nuyoo ñeel na leen, tukkee ca mbooloom gëmkat ma ca Babilon te di ñu ñu taamu ni yeen, tukkee itam ci sama doom Màrk.