1 Peter 5:4 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu waxtu wu Boroom gétt gi feeñee, dina leen jagleel kaalag ndam guy sax ba fàww.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ba bu Sàmm bu mag bi feeñee, ngeen jot kaalag daraja gu dul furi.