1 Peter 5:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Suufeel-leen seen bopp kon ci ron loxob Yàlla bu am kàttan, ngir mu yékkati leen ci jamono ju ko soob.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci suufu loxol Yàlla bi am doole la leen Yàlla di yékkatee bu jotee, su ngeen toroxloo,