1 Peter 5:9 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Jànkoonteleen ak moom ci biir ngëm gu takku, xam ne kureelu bokk yi ci àddina yépp, ñu ngi daj ay fitna ni yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Pastéefu ngëm ngeen di xeexe te xam ne benn coono bi ngeen di daj, moom la mboolem seen bokki gëmkat yi ci àddina di daj.