bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Samuel 1:24
1 Samuel 1:24 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Naka la feral xale bi, ànd ak moom, muy lu tuut, mu yóbbu ko ca kër Aji Sax ji ca Silo. Mu yóbbaale ñetti yëkk, ak benn efab sunguf, yemook fukki kilo, ak mbuusu biiñ.