1 Samuel 10:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu mboolem ña xamoon Sóol démb ak bëkk-démb, daldi yem ci moom, mu ànd ak yonent ya di wax ay waxyu. Nit ña naan ca seen biir: «Waaw, Sóol doomu Kis jii, lu ko jot nii? Sóol it ci yonent yi laa?»